Buio

Audio - Affaire Khadim Ndiaye - Aida Macké: Les confidences du fils du propriétaire de la maison.

JOTAAYU Sénégal (JS)
visualizzazioni 540 446
73% 1 537 565

Musica

Pubblicato il

 

8 nov 2018

Condividi:

Condividi:

Scaricare:

Caricamento in corso.....

Aggiungi a:

La mia playlist
Guarda più tardi
Commenti 663
Aly Badjan
Aly Badjan Mese fa
Maneh Ndow ci bakhoul. Lou melni kouko def Teh dofoulo, yahko teye.
khady Bamba
khady Bamba Mese fa
Ack lou meuna xew femme bi waroul tall khadim ndaxx amoul lou meuna justifié ray vraiment femme bi criminelle la amoul domou mbacke mbacke mann ginaw yalla ack yonentibi psl serigne touba ack wa keureum la geum mais li acte volontaire la que justice soit faite li ct préparé qui mom dou dioulitt xanna
Babacar Ndiaye
Babacar Ndiaye 2 mesi fa
Yalna niou Alah mousseul ci djiguéne diou mél nii ak naaféckh yi koy woutal lây !!!
ra ra
ra ra 2 mesi fa
et alors?fami bou diegué rek ken douko tedj non senegal mo nekh
No Comment
No Comment 2 mesi fa
🔴🔴🔴 Allez commenter ma dernière vidéo et abonnez vous, je rends🔴🔴🔴
Dian Diallo
Dian Diallo 2 mesi fa
.
Lamine Gueye
Lamine Gueye 2 mesi fa
Nous les africains gno guena sonou fi wayé tam gno nara guena sonou yawmal khiyam
Lamine Gueye
Lamine Gueye 2 mesi fa
Man dé tay la bayi tass Kimome nan الرجال القوامون على نشاء. Réwmi degue manofi am c impossible jamais. Par ce man yi journaliste maguis Amolén sakh odase posée les question❓ clairement Nit bo ray nit guénnan dondou kou warona diékh J8 peur de mon pay Motakh gnon macky sall rék mogno wara djité comme président mome mi wakh nous sommes des sytoiyé ordinaire Ou bien sakh sonko comme mome guemoul tarikha Ndakh dnépou mana tègué si yon Par ce ki lou rakh mo déf li da khamon ni dara doko si fék Mo takh mo am fit défli
Lamine Gueye
Lamine Gueye 2 mesi fa
Senega barina ay nafékheu
anta seye
anta seye 2 mesi fa
yalla na yalla yeureum khadim
Moussou Sarr
Moussou Sarr 2 mesi fa
moi je ne comprends Sénégal parceque ki raw dieukeureum wané naniou ko siwal ko fepp mais loutakh niou sathie khalé yi,di violé waté bouniou léne diapé douniou wané???????
Moussou Sarr
Moussou Sarr Mese fa
Ameena D mais bo dieulé khalé lo koy doyé
Ameena D
Ameena D 2 mesi fa
sokhna si Ray bokoul ak leine
Layzo Carlou
Layzo Carlou 2 mesi fa
Mais bro bi vrai doff leu koi ...Meurtre am nganane plainte amoul..Même s'il n'y a pas de plainte, les responsabilités doivent être situées... La justice est là pour tout le monde
Layzo Carlou
Layzo Carlou 2 mesi fa
Koutaal dieukeureum nguéne naane kou bakh leu ...vrai dof nguéne koi ...C'est le monde à l'envers
Cherif Cherif
Cherif Cherif 2 mesi fa
Joli
Marieme Bassoum
Marieme Bassoum 2 mesi fa
Méchante épouse tu n mérite Pa être mère tu a mis la honte ns femme loumoutou done tale nite tu allé tro loin vrmmt
Massylla Mbaye
Massylla Mbaye 2 mesi fa
Ndawsi daal kou bone la té sokhor di lakk nit mélni kou yor dibitéri , nioukoy dèma rafétal li kéne manouko rafétal bam rafét
Oumy Gueye
Oumy Gueye 2 mesi fa
qui sokhor na trop
Masseye Fall
Masseye Fall 2 mesi fa
Li dawna yaram yalla rek mo kham
Yayetop Thiam
Yayetop Thiam 2 mesi fa
Un. Mari. Beau
Mafou Aidara
Mafou Aidara 2 mesi fa
Mane maa waarou
Diatou Diallo
Diatou Diallo 2 mesi fa
Djiepi na wa senegal 🇸🇳 Bilaye Walay femm bi bougn mako abalone nako togu lek ko Bilaye Walay en plus ki khamoul khol mane Serigne ak famille douma leine ax falè force damay ray femm bi mou nek match null Bilaye lou nit firr firr tall c la dernière chose koi
dia aissatou
dia aissatou 2 mesi fa
Vous etes trop hypocrites mes chers journalistes c est quoi c est histoire on parle de meurtre de premeditation
Julienne Badiane
Crime par préméditation. Donc c'est la prison directe
modou lo
modou lo 2 mesi fa
kimom dafabon torp
Amicolé Dème
Amicolé Dème 2 mesi fa
diabaram dafa sokhor bone
Amicolé Dème
Amicolé Dème 2 mesi fa
diabaram dafa sokhor
michou diaw talibe baye Niass Diaw
Yaw mom mansour diop mala weddi naké yaw Domi haram gua geumoulo dara amoul domou serigne amoul dara wakha li yalla wakh si kou ray niit na nekeu domou seuydina mouhamet baxam
la linguere Niang
Ki dh koukoy takat day taylè bopam😂 rk
Haby Cisse
Haby Cisse 2 mesi fa
HA LES SAPEURS POMPIERS !!!!!! TOUT MARISTE POUVAIS PRENDRE FEU ET EUX DISENT MANQUER DE RÉSEAU !!!!!! HA LE SÉNÉGAL !!!!!!
Mbaye Seck
Mbaye Seck 2 mesi fa
Eskeuy yalla sounou borom.. Ki mo bone deugue, takhaw âme fite di soti nite essence talko mou dé
cheikh expert Camara
Loutah sénégalèyii naafèkh.elhadj dall wèdinala.
Tossane Diagne
Tossane Diagne 2 mesi fa
Bayileen mou bonne lou nieuw ngeen wakh ndogalou yallah YALLA kouko wo kouné daley diapalé soutoural la mais Satan naak kouko wo mou wouyou sila Jalousie bou eup bakhoul day attiré Satan donc d'après les disputes la femme n'a jamais respecté son mari ndakh khamna elle dira k sama papa moy serigne niam di gorom douma sania deef darra Kou goor ki ndeyssane mélni kharou yaar ndakh am respect am limouy rouss ak loumouy khol! Mane naak je les connaisse pas mais souma bokone ak khadim Ndiaye bou yabbo niou reyma déh mais Dame bi dinako deef cicatrice bo khamné heure bou sétto dineu fatélikou limou deef Wassalam Repose en paix khadim sunu borom doula sétane been yone il sera ton avocat Dinala pledel amoul serigne amoul justice mo bok ndiaboté nieup on est tous égaux devant lui!
Ousmane Ndiaye
Ousmane Ndiaye 2 mesi fa
Prémédité
Fatima Rassoul Gueye
Kou ray danioula wara ray
patricia podi
patricia podi 2 mesi fa
C mon oncle le frere a mon pere ke dieu l'accueille au paradis...
soda mbacke
soda mbacke 2 mesi fa
Mane kouyor bi khole ya ma meune
soda mbacke
soda mbacke 2 mesi fa
Mane kouyor bi khole ya ma meune
diarra dabo
diarra dabo 2 mesi fa
vraiment cet acte est inexplicable! mais Allah voit tous même si elle n'est pas punie dans la vie présente, elle le sera dans l'au delà!
Massamba Ly
Massamba Ly 2 mesi fa
Boukene togn seytanè nak Jalousie c animal .beuy sakh dafay firr Guinar sof mbame khoukh. Mais dem bay jeul essence talll Kou sokhorr lol lol lol mokoy def Sa merite punution .loi kasso charia reyy
sy amsatou
sy amsatou 2 mesi fa
En plus il etais tres beau wallah thier elle a gater la vie de ce jeune homme.wallah
sy amsatou
sy amsatou 2 mesi fa
On a qu'a appliquer la charia wallah ke Azawadjel accorde a khadjim le djannatou firdaws
issa diallo
issa diallo 2 mesi fa
réponse en paix
Awa Gueye
Awa Gueye 2 mesi fa
Slu
Neva Sow
Neva Sow 2 mesi fa
Quand une femme est movaise elle est très movaise.
Mariane tu Est le Rio Ndiaye
Elle méritte l'enfer sette solope de Aicha mbacke nitte kou meune déef
mouhamed mbaye
mouhamed mbaye 2 mesi fa
Mane dee sama yone nékoussi Dee! Khawma Lou khew ! Wayei problème waroul takh keneuh dii taaal nite nak
Mohamed Sall
Mohamed Sall 2 mesi fa
Sa diabar boula talone do wakh laulou imbéciles
penda elimane thiam
wa tamit mane dal meunouma comprendre nit Lou gnaw li rawatina Ray nit gnounane nit yi nagnou manou la femme limou def dara meunouko rafetal ak famille boumou meundi bok yakhna derou ay mbokam fi mom kou dé ya perte même bou amout plainte yone dina def liguayam lima meiti thi Sénégal mou moudjei beuri ish se pays de merde
Khady Sarr Sarr
Khady Sarr Sarr 2 mesi fa
Hum diga teud prison dè k sa soi clair dan ta tête .de plus tu n la jamé aimè kéne dou dèf Lou bonn lhomm de ta vie c du nimport koi
Maman Sy
Maman Sy 2 mesi fa
Astou ya bone di rey
beydy sakho
beydy sakho 2 mesi fa
Lou geuna grave si li ni dome dji mou wossine le lendemain sou magué ladj yayam kane moy sama papa lane lako sokhnassi di tontou
amt amt
amt amt 2 mesi fa
Al maktoum.newonna nan sangat rewmi.ndax danouno rax.yenn yi douk neen.taal sa dieukeur.rendi sa baay.ak ay xarou youdoul diex.ta ay djoulit rek koy def.yalnanuci yalla miuseul mes li doyna war
Prossimi video