Buio

Cheikh Niass : "Mon père sera enterré à Yoff, c'était sa dernière volonté"

igfmsn
Iscriviti
visualizzazioni 300 662
86% 1 244 192
Commenti 193
Boury Dieng
Boury Dieng 7 giorni fa
ndéké kou diour sa dôme perto ndiro am n'a nôoo
Fatoumata Ba
Fatoumata Ba 7 giorni fa
k Dieu l'accueil dans son paradis éternel
Mouhamed LÔ
Mouhamed LÔ 8 giorni fa
Yalnako yalla yereumm
Amina Sign
Amina Sign 8 giorni fa
Que Dieu vous donne la force de surmonter cette epreuve ...paix a son ame
Aicha Sané Sané
Aicha Sané Sané 8 giorni fa
Paix à son âme cé triste
Abdou Sylla
Abdou Sylla 8 giorni fa
La prochaine fois avant de te prononcer, dans de pareille situation, il faut consulter et se concerter avec tes pères. Les familles religieuses sont régies par des règles et principes. Lèona Niassène est la terre de sa dernière demeure. Qu' il soit accueillie au PARADIS avec tous les honneurs. Amine
Djili Ka
Djili Ka 8 giorni fa
didi yalla nakou yalla yarame
Aischa Thiam
Aischa Thiam 8 giorni fa
Mais tamite qu'il soit enterré à yoff wala Kaolack la personne est déjà mort PQ beugue kheuthio????? Wa keureum n'a pas de mot selon car il a une famille ses enfants veulent l'enterrer à Yoff c'est tt!!!! Au ciel il est avec ses parents et grands parents 😑😑😑😑
Han Ba
Han Ba 8 giorni fa
Khouloo katyi naniou noppi Le dernier mot revient à qui il a parlè en dernier:son fils Que la terre lui soit legere et allons preparer nous aussi NOTRE JOUR IL EST MORT PARCE QU'IL VIVAIT'
Papito Diagne
Papito Diagne 8 giorni fa
Na talibe yii yam way se sont c fils ki on le droit sur lui
Papito Diagne
Papito Diagne 8 giorni fa
Bien dit bro
Ndiaye DKR
Ndiaye DKR 8 giorni fa
Sidy Lamine Niasse était un homme du peuple, la voix des sans voix nittou askan wii. Donc l'amener à Yoff serait le rendre au peuple.
zey zey
zey zey 9 giorni fa
Ooohh li metina yalla na yalla watiei yeurmandem tie mom ak mboleme dioulite Defal lene ko limou beugone osi
Lamine foti Italie
Lamine foti Italie 9 giorni fa
Combat terminé. Tu sais pas comment parler
Gora Gora
Gora Gora 9 giorni fa
Wa ana khalifa niassen yi loumo wakh rek lano wara deff nitt daye am kilifa wasalmm
Astou Ndiaye
Astou Ndiaye 9 giorni fa
Thiey adouna kou dés rk ya perte niit ki demna ba paré djaroul khiro il faut respecter son dernière volonté
Mariama dia toukoulor bou rafét bi
Yalnako yalla kharei aldianay firdawsi ya thi barké s mouhamed psl amiiiine
Tijani Diagana
Tijani Diagana 9 giorni fa
Allahouma Ghfirhou warhamhou ! Ya Rabal Alamin
Freshy Dollar
Freshy Dollar 9 giorni fa
mane mounouma comprendre sa papa ganiou nga kheuy taxaw daiakarlo ak press bi di wakh 😔😔légui dééh nekatoul dara !!
Gnemee Deugh pire
Gnemee Deugh pire 9 giorni fa
Maitre Cheikh🤔
Basse Faye
Basse Faye 9 giorni fa
Yaram dawna
aliou diouf
aliou diouf 9 giorni fa
Journaliste bi sof gua ak sa francais soff nguene ak français yi Loutakh vous parlez pas le woloff putain c grave pour nous . Paix à son ame
Ramata Ndiaye
Ramata Ndiaye 9 giorni fa
Mane sénégalais khawma loulene dall bou nit guené Adouna nguene déplacer yobou Touba, tivaouwane etc.. Mais fep bene leu nitki fimou décédé lanouko wara soul rawatina fi sa ndiabotame nek ba paré le défunt sa volonté moy niou soulko Yoof kone danguene KO wara respecter kilifa bou Tolni sidy lamine niass décédé depuis mercredi nguene di khar ba vendredi pour soul KO je suis d'accord avec le fils
Dienaba Sow
Dienaba Sow 9 giorni fa
Nagnou bayi jugé lougnou woroul,Sidy lamine sou amoulwone foumou ték Ahmed halifa douko toudé 2fils.emplus gno bokou nday ak baye kimporte l blème kils avait se sont des frères.sou fékone dôme moy décidé dou ki mo wara décidé pack il né pas l'aîné.nagnou mandou
Dienaba Sow
Dienaba Sow 9 giorni fa
+Fatma Balde guisga motah gnounane nite day am kilifa.te Ahmed Halifa sène kilifa la, té dou lep lagnou meuna wahh.mais Sénégal di jugé nite té hamougnou rek lagnouy def
Fatma Balde
Fatma Balde 9 giorni fa
réalité absolu gnom lignou wara def moy topou thie guinaw Ahmad khalifa niass ndakh moy senn baye di senn magou baye ish Lima soof thie mbirmi moy gnep khamnagn ni dagnou am problème tei thiowli meune na yeg foko foguéwoul ndakh meun na dem bathi senn seute seutat yi
Thiatou Yayam Diouf
Paix a son âme😭😭😭😭😭😭
Khadim Diagne
Khadim Diagne 9 giorni fa
wa papay jambour même bouko wakhul wone sakh dom yi gno thji am ndogal bulen foto
Awa Fall
Awa Fall 9 giorni fa
yalla nala yalla yereum
Moundhor
Moundhor 9 giorni fa
kaolack c'est international mais sic 'est la volonté de Sidi laissez sa famille l'enterrer à Dakar.
Papa Wagane Gakou
Papa Wagane Gakou 9 giorni fa
K la terre lui soit légère, mais cheikh on te comprend car tu as reçu une éducation à la française. Mais dire k enterré sidy à Kaolack est une dimension locale confirme ton ignorance, Elh Abdoulaye, khalifa et Baye Niass sont enterré à Kaolack et le monde entier les fait le ziar everyday
Rokhy Daba Ndong
Rokhy Daba Ndong 9 giorni fa
Yalna ko yalla yeureum amin
waxkatou Deug
waxkatou Deug 9 giorni fa
Le grand père de sidi, son père et même sa mère qui est descendante du prophéte PSL sont tous enterrés à Léona(kaolack).Ce que son fils là qui n'est même pas l'aîné raconte n'a aucun sens! Sidi doit être inhumé à kaolack auprès des siens; c'est la tradition dans tous les tarikhas du Sénégal. Al Makhtoum a longtemps vécu à Dakar même durant son khalifat; cela n'a pas pour autant empêché qu'il soit inhumé à Tivaoune après son rappel à DIEU. Vous n'avez qu'à sortir ce testament ou sidi lamine à demander de l'enterrer à Yoff et le débat sera définitivement clos. Je pense plutôt que ce petit cheikh niass veut rendre hommage à son père à sa façon en l'enterrant à Yoff dans la neutralité "chez les sans voix" pour mieux coller aux convictions de son père durant son vivant et qui était de toujours se ranger du coté du peuple. Son père avait des positions durant son vivant;personne n'en disconvient;mais cela ne traduit pas pour autant une volonté de ne pas l'inhumer auprès des siens.
Ibrahima Mbow
Ibrahima Mbow 9 giorni fa
waxkatou Deu
Aimee Nunez
Aimee Nunez 9 giorni fa
Il est fort le petit il souffre intérieurement mais il a pris son courage à deux mains. Que la terre lui soit légére
Astou Dia
Astou Dia 9 giorni fa
Yalla nako yalla khare Aldiana
Fatou Mbengue
Fatou Mbengue 9 giorni fa
Bien parlai cheickhe je te presente mes condeleance le dernier mot te revien
mor lo
mor lo 9 giorni fa
boulaine sonale new bi yalnako yalla hare aldianaye firdawsi yoff la beugue yoboulaine ko yoff
elhadji niass
elhadji niass 9 giorni fa
No kaolakk rake si ay mbokam inshalla
Malle Syll
Malle Syll 9 giorni fa
yalla na ma yalla ball wayé cheikh niass mii woolou mala de
Samassa Harouna
Samassa Harouna 9 giorni fa
Paix a sont âme
Mame fatma Ndiaye
Mame fatma Ndiaye 9 giorni fa
Amo kilifeu, xaley dou kheuthio! Beusseul sa xol, nga ceder
Kafrine Kolda
Kafrine Kolda 9 giorni fa
Waxo fi touss dakar ak kaolack lan moy difference bi
Yaaya Demmba Jallo
Yaaya Demmba Jallo 9 giorni fa
Wonaa goonga wona fof en kay.
Massylla Mbaye
Massylla Mbaye 9 giorni fa
Lii moy sénégal nak booy doundou lo wakh niou wèddi bo fato nak kounèkk di wané thiofèlam , guemouniou touss , sydi lamine nak limou liguèyal sénégal ak diiné ak langue arabe yalnakako yalla fay , té lou waay déf boppam
Massylla Mbaye
Massylla Mbaye 9 giorni fa
Lii moy sénégal nak booy doundou lo wakh niou wèddi bo fato nak kounèkk di wané thiofèlam , guemouniou touss , sydi lamine nak limou liguèyal sénégal ak diiné ak langue arabe yalnakako yalla fay , té lou waay déf boppam
mame Diallo
mame Diallo 9 giorni fa
Paix et repos a son ame .J ‘ai vraiment pitie des enfants .Dara xewagoul gnou commencer polemiques .Il faut se plier a la volonte du defunt qd meme ,respecter son souhait . C est triste de se dechirer comme ca ,alors que sa famille proche ( enfants et epouses ) ont besoin de soutien. Seul Allah est Unique et Puissant ,il faut arreter d ‘abuser de votre “ pouvoir “ soi-disant que vous etes des hommes de Dieu .Nul n est infaillible .Ayez pitie de ces enfants et laissez les enterrer leur papa selon sa derniere volonte .C est vraiment trop !!!!! Le defunt doit reposer en paix apres avoir termine sa noble mission sur terre .Yeeneu yiii aakk bou mack leu .
Mousse Diallo
Mousse Diallo 9 giorni fa
WA me defallen loumou beugue way.
Aminata Boye
Aminata Boye 9 giorni fa
yalla.n'a.ko.yalla.hâter si.yeurmandeme.mou.khiper adijana.
Nouhoun Traoré
Nouhoun Traoré 9 giorni fa
Que son âme repose en paix.
Moustapha Diouf
Moustapha Diouf 9 giorni fa
En tout cas on écouter ses fils et non à ceux qui n'étaient pas en bons termes avec lui de sont vivant
Yacine Faye
Yacine Faye 9 giorni fa
eyyyy waaay bayilene domame mou yobouko yofff
nit da fay am yar ndour
Kén douko yobou yoof sidy wakhouko lolou ki goné gouy tass mbok la
Mamadou Sy
Mamadou Sy 9 giorni fa
mandou leine ci famille diambourr QUE LA PAIX LUI SOIT LÉGÈRE
Ndiaye Mamesophie
Ndiaye Mamesophie 9 giorni fa
Manchallah comme son père!!!yallah nako yallah yeureume té yékhégnou
tima latifa
tima latifa 9 giorni fa
k la terre lui soit legere et k le bon Dieu l'acceuille dans son paradis celeste
Pate Dao
Pate Dao 9 giorni fa
yalla na yalla watou lene si sen barke mame
Alioune Badara Ndiaye
Ce n'est pas à quiconque de décider outre que ses enfants à plus forte raison que ça soit le voeux du défunt. Nit kou nék nangua ko jappè ni soudone sa baye noy déf. Sénégal so déwé gnou khethio la, sougnou la soulè faté la. Gneup gnoko beugue wayè ki moko fi togal . Nagne ko gnanal Yalla na ko Kharè Aldiana firdaoussi
Alioune Badara Ndiaye
+Rémy Joe Niafouna Yalla nala Yalla dolil Diam
Alioune Badara Ndiaye
+Rémy Joe Niafouna pardon frére. Yalla nagnou défal diam
Rémy Joe Niafouna
Rémy Joe Niafouna 8 giorni fa
je e parler pas a toi sur le commentaire mes plutot a adama ba
Alioune Badara Ndiaye
+adama ba je suis Dacord mais khana papame Sidy dou kilifame. C son père qui lui a demandé ça en plus c qui la famille?? Hmmm
Alioune Badara Ndiaye
+Rémy Joe Niafouna tu n'as rien compri. Apprends à lire si tu use de ta capacité mentale
Mamour Ndao
Mamour Ndao 9 giorni fa
mandou léne thi famille diambour
Aida Gueye
Aida Gueye 9 giorni fa
metti na wayé nitt da fay am kilifa sou ma nekkone mome di na ni bene pape la niou fi déssé mouysa ma Papa Akhmed Khalifa NIASS sou niou wakhtané si sou nou bir famille ba paré di na niou ko diokh kaddou giu mais pas ca Sidy yalla na ko yalla kharé aldiana
baylat lo
baylat lo 9 giorni fa
thiey addouna
Cheikh abdou Fall
Cheikh abdou Fall 9 giorni fa
Bu léen juuyóo mok dik lu léen seen papa ahmed xalifa ta def lim wax am kilifa lu baax la
bb diamant
bb diamant 9 giorni fa
cheikh vu ta façon de parlé on sait que faté nga say ada ak thiossane tu es un français maintenant mais lifii mame yi bayi dou dègne say kilifa nii on lamène a kaolack pres de ses parent ngay wakh pourkoi les marabou qui sont mort a lextérieur on leur amène dan leur pay dorigine toi un jour si tu meur on peut tentéré en france sidy es natif de kaolack ses parent son entéré a kaolack nasirou mou mame baye quan il est mor a letrégé on la amené a medine yaw khamo touss ferme ta bouche
EL hadji Fall
EL hadji Fall 9 giorni fa
Atakhwal allah ragalen allah
mame thierno niane
mame thierno niane 9 giorni fa
Li taw wakh moy ame
madame mbodj
madame mbodj 9 giorni fa
Ndeysanne
viviane diallo
viviane diallo 9 giorni fa
Mé môme wa médina baye la pk yoof
khéweul ndiaye
khéweul ndiaye 9 giorni fa
Nayesane ly metina trop mais yalle nakou yalla hari adiana filedawci
SAMBA NDIAYE
SAMBA NDIAYE 9 giorni fa
mérci ca wakhe rafét na
Binta Ba
Binta Ba 9 giorni fa
Yallah nako Yallah yerem khareko aldiana Bou kawwe nit Bou dewee Lou Guen bakh Guen gaw ndenthieko 😢😢😢Ndyessane sidy dama ko yagg beug ndiakh djikommm🙏🙏🙏
Maguette Diallo
Maguette Diallo 9 giorni fa
Paix a son ame ke dieu l accueil dans son paradis amine
Feuz john jay
Feuz john jay 9 giorni fa
Kaolack c’est une mission locale et dakar une mission internationale qu’est-ce que cela veut dire? Et qu’en dis tu de la mission de baye qui dépasse les frontières alors qu’il est enterré à kaolack...? Voilà les conséquences quand tu élève tes enfants en dehors de tes racines...ce fils parle d’élite et de nouvelle classe sociale don’t appartient Sidy pour l’enterrer à Dakar...je doute que ce soit la volonté de son père...
Ibrahima Thioub
Ibrahima Thioub 8 giorni fa
@Feuz john jay u as parfaitement raison c'est juste une question de deracinement et d'ignorance de la realité
Adama Wade
Adama Wade 9 giorni fa
Maandou leine si mogueun
elou thiane
elou thiane 9 giorni fa
il nest meme pas son fils aine
Joe Diop
Joe Diop 9 giorni fa
Je nè jamè vu ça c sidy lamine dè wala daniouko fatè taye il a rendu l'âme kounèk meune nga takhaw wonè sa bopp pour takhawouko parsek sokhelatouko meune n'a wate si yala ni wadiale n'a bopame li moulène bayè ni mouye dieumeum dji dième nguène si bamouye dounde meunouléne si dara ndakh boba lérou rouhou gui molène diakhalone fi mou tolou loulène nékh défelene si wayé kharitou frero yaakarnani dôme bou gore majeur warenamana takhawou bayam boubakh ndakh souba môme moye déssate akk lifi papame bayi mouye jaabot gui sidy bilahi yala na la yala kharè Aldiana dama meussa guiss si sa kanam ak jambare lou nè dadienako wayé mougne rekk yala boula thiate djitou
Ngane Fall
Ngane Fall 9 giorni fa
Innalilahi wa inna ileyhi radjihoune yeurmandé borom bi yalna beri tha mom bidjayi seydil woudjout Amine ya Raby
Elhadj Cheikh Diagne
Nit ku nek kam beug lay deukkal eleug, Sidy Lamine beugg na Senegal ba yelloo ñu robko Yoff ci Dakar Capitale Senegal ndax ñep yem ci mais nak Sidy ay wëyjuram aki mbokkam yiko defar yarko bam mel nimu mel tay ba ñep diko xeuthioo, ñooñu di ayy weyjuram di ay wassilaam la gueuna beugg waay, talibé Muriid boo guiss li ci eup dafa beugg bu faatoo ñu robb ko fa seriñam teudd... «almar'u ma'a man ahabba» ci zaahir bi yaqqul dara, baatin ba moom matt na bu yagg
Ameth Fall
Ameth Fall 9 giorni fa
😭😭😭
MOUSTAPHA LO
MOUSTAPHA LO 10 giorni fa
Voici Notre Nelson Mandela au Sénégal Nous les sans vois .on pérdre Notre Père. Yalla n'a yalla wathié yeurmandé si mome
Mame Cheikh Sylla
Mame Cheikh Sylla 9 giorni fa
Merci
diagne mor
diagne mor 10 giorni fa
La logique voudrait que l'on enterre à koalack à côté de son père malgré son statut de Journaliste il est un homme religieux et respecté par son savoir
Rémy Joe Niafouna
Rémy Joe Niafouna 9 giorni fa
bien dit moussa camara
Moussa Camara
Moussa Camara 9 giorni fa
Il savait déja la logique car il maitrisait sa religion sa famille et sa societe alors k il avait designé Yoff donc la logique doit être son choix mon frére paix à son âme
Amina Mbye
Amina Mbye 10 giorni fa
Tijan you are right I feel for you
Djigo mamadou
Djigo mamadou 10 giorni fa
Sénégal niackaatinna killifeu gou amonne yaakhinne
Abdou rahim Kane touba
Yobou ko Yoff té nopi diapou sa diambourr yalla bakhna barina soutoure
Bint Moustapha
Bint Moustapha 10 giorni fa
Killifa bou tolni Elh Sidy lamine Niass nélaw Mardi fii ni Sénégal, gnou beugue ko téyé ba vendredi dok ko dinth😡 en plus fou bokoul ak fimou taneu😭....mais on est où nak? Mane mom j'suis avk ses enfants ndakh Sidy bimouy doundou gnom ladone guiss et se sont eux qui doivent décidés pour lui boufi nékatoul!!! Que Dianatoul firdawsi soit ta demeure éternelle Elhaj Sidi🙏❤
Kafrine Kolda
Kafrine Kolda 9 giorni fa
Wax gua lepp
zeyna kr fathion
zeyna kr fathion 9 giorni fa
😭😭😭😭😭
Queen's Baby
Queen's Baby 9 giorni fa
Dégna deug
Oumar Sall
Oumar Sall 10 giorni fa
Yamal palace khalee mo gueune si yaw wakho deugeu ton père na jamais di sa ces pas vrai je te defie moi oumar sall niass actuellement je suis a la maison ton père akhmed khalifa niass ta demandé si ton père ta demandé sa tu as di nons donc ton père na jamais di ca
Keur gui Tv
Keur gui Tv 10 giorni fa
Thieuyy Adouna mann dalle waarouna siiww dou diammii borom
thiatou yayame
thiatou yayame 9 giorni fa
wallahi
ramatoulaye dia
ramatoulaye dia 10 giorni fa
Paix à son âme. Les propos entendus sur la déclaration de Cheikh Niasse,si ce sont ses propres paroles elles l'engage.Mais si s'était la volonté de son père donc rien à commenter
Ibrahima Seck
Ibrahima Seck 10 giorni fa
Yoff fou baye laye
Alioune Badara Ndiaye
stp pas de polémique . Ya khayrou khal khilah santoula li. C pas le même context
abdoulaye niang
abdoulaye niang 10 giorni fa
yaw la andal sa baye leu mouvement % rkk yoff
A D
A D 10 giorni fa
Bayi leen papay diambour, politique guen ba sone yen wa leona niassen, mo tax guen beug wa gouvernement bi nieuw fa guen politic comme d habitude,
A D
A D 9 giorni fa
Lou ma rewal? wax lima guiss. Si gamou nouy sant ay president. Deug dall nexoul, waya nak moy li yalla beug,
Mariama Niass
Mariama Niass 9 giorni fa
Kou rew ga yow
Balla
Balla 10 giorni fa
CHEIKH yaw sa wakh dji diaroul yone mane geumou mala
bbchou86
bbchou86 9 giorni fa
Yow werro dè
Fatou Sylla
Fatou Sylla 9 giorni fa
Ioe nopill kii il vien de perdre son pere c normal qu'il fasse ces derniers volontés
Sokhna Thiam
Sokhna Thiam 9 giorni fa
Kou deuguer fitt ga on parle d'un mort koussi wah lo warou wah reik yangui togne Yoff la beugone prkw pas
galsen galsen
galsen galsen 9 giorni fa
Yala rek mo xam Lou diar yone ak lou diaroul yone ki si nakar la nek bayil critiquer t nianal ki fatou mo eupeu dieurigne
Balla
Balla 9 giorni fa
Daouda Doumbia yaw bayil ba mana wakh
Mame Niang
Mame Niang 10 giorni fa
Dèfal li Ahmed Khalifa niass Wakh ndakh moye kilifa sidi lamin yaw sa diann waccna
BELLZO DIALLO
BELLZO DIALLO 10 giorni fa
**Ces imposteurs veulent récupérer le décè pour se faire de la fortune et refaire leur image... Laissez son fils aimé prendre soin de son père et exhaussait sa volonté ultime♥️ **
Princesse Manjacque
Belizo ma degue deugue merci mon cher
Princesse Manjacque
+Rémy Joe Niafouna suis parfaitement d' accord avec toi mon cher.
Rémy Joe Niafouna
Rémy Joe Niafouna 9 giorni fa
ceci cet nes pas a toi ni au senegalais den decider il a demander a se quil sois enterer a dakar ont doit respecter sa volonter en tant que telle
0p6ysyxkqvtv18knam self
Khalifa niass waroul wax dome dji di wax realité senegalaise mo commencé yakou et c’est à leona au près de son père qu’il aura plus de prière ki dei niane rek la sokhla
Aly baye Ndom
Aly baye Ndom 9 giorni fa
arame mbow c normal pask c lui ki est au senegal
Senrap Galsen
Senrap Galsen 10 giorni fa
Dioumgua
fama fall
fama fall 10 giorni fa
Le fils lui ressemble beaucoup. Paix à son âme.
Babacar Dione
Babacar Dione 10 giorni fa
Nous présentons nos condoléances au groupe walfadjri mais aussi à tout le peuple sénégalais. Le Sénégal vient de perdre un grant homme, un combattant un défenseur des libertés et de la démocratie. Un homme intègre, constant dans ses principes et qui a jamais abdiqué à combattre l'injustice. Que le bon dieu l'accepte à son paradis amen
Boubacarmansour Gayesy
merci cheikh il faut bien respecter sa volonté divine
Mame Cheikh Fall
Mame Cheikh Fall 10 giorni fa
Yalla nako yalla kharè aldiana
Mame Mor
Mame Mor 10 giorni fa
Non non Dakar
Chocola sow
Chocola sow 10 giorni fa
Mame Mor pourquoi pas Dakar
Mame Mor
Mame Mor 10 giorni fa
Non non Dakar
el hadji diop
el hadji diop 10 giorni fa
Rip we'll never forgot to pry for Sidi Lamine Niass
Diaspora tv rék
Diaspora tv rék 10 giorni fa
Nit day am kilifa challah niasse lii dou yoonn
Fatou Gaye
Fatou Gaye 10 giorni fa
Rip😭😭
Sam Njie
Sam Njie 9 giorni fa
yalla nako yalla yeureume kharalèko aldjana firdawsi yalla na khiper aldjana firdawsi amine
Serigne Fallou
Serigne Fallou 10 giorni fa
PAIX À SON ÂME ALLAHOU MA AMIIINE
islam up
islam up 10 giorni fa
Machalah yalnako yallayeureum
Ibrahima Sene
Ibrahima Sene 10 giorni fa
Sidi lamine keye j'ai jamais vu quelqu'un d'aussi intégrer il était à l'écoute de tout le monde je me rappelle quand j'étais jeune et que y'avait que le rap dans les années 90 pour que les jeunes puissent s'exprimer.toutes les chaines sénégalaise ne donnaient pas la possibilité aux rappeurs de s'exprimer.yavait que pour nous les jeunes walf . merci tonton sidi pour tout ce que tu as fait.ton âme reposé en paix maintenant
Seynabou thior Faye
Seynabou thior Faye 10 giorni fa
Assalamou aleykoum. Mangui dialé nieupe. Il faut respecter la volonté du défunt. Et l'enterrer a Yoff. Merci
Astou Mbaye
Astou Mbaye 10 giorni fa
Défal ko limou beugone sénégal boye donde nio dilla khékh so déh wé ko nék di reuye laminie ya yoré kadou bi ndakh yaye tawam dén thie ko fimola wakh té nga nianal ko yallah niéguel
Dame Seyr
Dame Seyr 10 giorni fa
Astou Mbaye bien dit fi da beuri ay nafékheu
Prossimi video