Buio

Eumeu Sene Sort de sa réserve après son Combat J'ai été atteint Mystiquement, Meussouma beuré...?

BANTAMBA TV OFFICIEL
visualizzazioni 604 516
93% 5 679 366

Abonnez-vous à notre Chaine ITvid: itvid.net/show-UCudfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: facebook.com/becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Pubblicato il

 

6 apr 2021

Condividi:

Condividi:

Scaricare:

Caricamento in corso.....

Aggiungi a:

La mia playlist
Guarda più tardi
Commenti 100
Mouhamed Mbaye
Mouhamed Mbaye Giorno fa
Ma xam fracture bilay Lac doul rek mousoul dameu
Bety Niass
Bety Niass 2 giorni fa
Eumeu ko yapp yén niar nieup beuré wo lén naniou bayi yéneu sénégalais affairou naafékheu
Amy Sarr
Amy Sarr 2 giorni fa
No vrema balla moy sama fans mé emeu ndandane nga
Beneen Tv
Beneen Tv 2 giorni fa
Xanaa du mystique la daane Bombardier Na gëum yallah te feliciter adversairam
Ndeye sokhna Diao
Ndeye sokhna Diao 4 giorni fa
Eumeu khamal ni yaw diam rekk guay ame
Mame Ndour
Mame Ndour 5 giorni fa
Bilaé tonton yayy champion 💪💪💪
Fallou Ba
Fallou Ba 5 giorni fa
Vraiment contenen si yaw ndakh lingua sédé si balla gaye 2 sama champion bi
Bamba Diop
Bamba Diop 5 giorni fa
Eum yaw wakhe rèk gay dèf yaw gè no sakoyi
Pape fall
Pape fall 6 giorni fa
Dagua diekhal
awa barry
awa barry 6 giorni fa
Courage champion
Mouhamadou Kane
Mouhamadou Kane 6 giorni fa
Des faiseurs de malin cela va de soi car la lutte n,'est que le culte de la betise
NSTYLEZ. TMC n.stylez
Nandane nga eumeu tigui jaroul justifier wou, balla Nandane la, modou lo Nandane la, gris Nandane la, bombardier Nandane la , LAC vrai fake le, tapete la, dafay rous lo goor
Alda Fernandes
Alda Fernandes 6 giorni fa
EUMEU J'adore ton sourire
Binetou rassoul
Binetou rassoul 6 giorni fa
Lac 2 ay thiokh leuh amoul ...wah écurie weum nagn ko dieundeul thiokh svp
Abdul sumner
Abdul sumner 7 giorni fa
Lac2 dafa wara bai lamba Du Dan tei du danu Match nil rek yaha derr keseh Mann Gambian la eumeu ndaanan nga
Serigne malick mbacké Diop
Balla moy sama lutteur dh mais bilahi j’adore eumeu séne ndakh deugue bimouy guéné si lamigne bi deugue dafa nékh daale❤️🙌🏾
ceerw buty
ceerw buty 7 giorni fa
Mane dei Balla moy sama mbeur beugu wa Guédiaway mé biii dama méré lac srx Eumeu diam si yaw def gua leep franchement bénen yon moy dak inchallak
Eva Dia
Eva Dia 7 giorni fa
Walahi jeste bi eumeu déf ak balla dafma nékh trop
Mboul Ngom
Mboul Ngom 8 giorni fa
Ay way nguir yalla Eumeu boudé amna team dolen massi dougal té yalla takh
Mboul Ngom
Mboul Ngom 8 giorni fa
Machalah on t'aime bcp Eumeu wadiatal bou bakh rek
ceerw buty
ceerw buty 7 giorni fa
Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant
Abdou Sene
Abdou Sene 8 giorni fa
Lac est un imbéciles
Abdou Sene
Abdou Sene 8 giorni fa
Lac ne mérite pas c cacher
Maman Bop
Maman Bop 8 giorni fa
Machallah fans club pure là Mala beug pure eumeu longue vie
Bugs Bunny
Bugs Bunny 8 giorni fa
nekhoule ba nekhoul mais eumeu yaw tamite beurewo. deugue rek nekh nak
Elizabeth Brooks
Elizabeth Brooks 8 giorni fa
machala eumeu sene diambar gua
Mounass Tamba
Mounass Tamba 8 giorni fa
Je suis fier de toi champion😘💟💟💟💟
Coumba Diop
Coumba Diop 8 giorni fa
Wallahi djambar ga lac dou mbeur
qopoy dnon
qopoy dnon 8 giorni fa
yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala
Sarr Sarr
Sarr Sarr 9 giorni fa
Vous les lutteurs vous faites toutes des fétiches donc il faut accepter la défaite. T as rien à dire .il faut être sportif.
Adama Malick Dramé
Lac d'où dara da nirou woule sakh mbeur
Adama Malick Dramé
Bilay eume da melni nion boke père et mère bilay da ma la begue menouma sétane sa lamb si salle de bain laye dougue monté ay écouteur ba volume 100
qopoy dnon
qopoy dnon 8 giorni fa
Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul
Adama Malick Dramé
Non eume ya fi nék ya meune kou nékoule lac li d'où défaite dhe yaw champion nga respect mbeur on é toujours derrière tw
Assane Konte
Assane Konte 9 giorni fa
Je vais convoqué les amateurs de lutte pour faire une marche pour que lac 2 arrête de lutter
Moustapha Kamal Th.
Eummeu, boul wakhati dotouma beuré ak mom . Dél wakh beugatuma beuré ak mom inchalla. Jajeuf mbeur
Pape medoune Ndiaye
Eumeu bilakhi wafii né
soniyu ziuy
soniyu ziuy 9 giorni fa
Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant
Mustataa Siise
Mustataa Siise 9 giorni fa
Euma tay bërewoo dara
Diagne Gnilou
Diagne Gnilou 9 giorni fa
En t'en que domou sèrére qui parle jamais sérère saymbok mérénagnoula
Diagne Gnilou
Diagne Gnilou 9 giorni fa
Yacodjoh sabaram
soniyu ziuy
soniyu ziuy 9 giorni fa
Non eumeu gor deugue la
ndiaga faye
ndiaga faye 9 giorni fa
Jämbàr deugue ngueu maaacha allaah ki ngua doon da dieel mooy thiounné reek koo diapp mistiquement War koo meuneu daan
Hamidou Agne
Hamidou Agne 9 giorni fa
Eumeu champion gue 👍Lac mome dou beure
Pape Sane
Pape Sane 9 giorni fa
Je suis supporter de Balla gaye mais eumeu sene je t'adore vraiment legui sama mbeur nga ndakh sa xol dafa rafet
Awa dia Sy
Awa dia Sy 9 giorni fa
Bilaye soule ndanane souli badola mais yaw mbeur nga diambar nga
cheikh kouyate
cheikh kouyate 9 giorni fa
Eumeu il est bien. Lac 2 bonne continuation. Je suis fier de toi
sotuur aeei
sotuur aeei 9 giorni fa
Douma fans Eumeu mais damako naw franchement dafa digne degou blie machalla
Aly Niane
Aly Niane 7 giorni fa
Ad
Youssou Diop
Youssou Diop 9 giorni fa
Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul
Issa Diao
Issa Diao 9 giorni fa
Lac dou mbeur bilahi
Issa Diao
Issa Diao 9 giorni fa
Na bayi beurré
sotuur aeei
sotuur aeei 9 giorni fa
Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss
Ndaye Khodia
Ndaye Khodia 9 giorni fa
Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur
Assane Samba
Assane Samba 9 giorni fa
Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé
Boury Ka
Boury Ka 9 giorni fa
Balla sama gaynder Ndiaye
Mamy Ba
Mamy Ba 10 giorni fa
Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️
Muslim2proud
Muslim2proud 10 giorni fa
Kouko déffati nako deegg, ap mbeur dou fénn, mbeur dou tapalé...aaay kouko défati nako deeg ap mbeur dou tricher mbeur dou yambar, 😤diapé sénégalais yi dofff 💃💃💃💃💃😂😂😂😂😂Eumeu, Balla Gaye2, Yekini, Bombardier, Ama Baldé, merci infiniment, gathiéloulén lambe. Fatou Guièr 2 démal nga toog, ngir yalla boulfi dieuleuti beneu combat, doyal na gnou si yow seuk.🙄🙄😏😏😠😠😠😠😠
Djily Diop
Djily Diop 10 giorni fa
Non eumeu gor deugue la
bssni touir
bssni touir 9 giorni fa
Lou lérr laa wakh
vmvdou svné
vmvdou svné 10 giorni fa
jai trop aimé son discours
vito boss vito boss no stressé
mane fans balla gayé la
bssni touir
bssni touir 9 giorni fa
C'est vrai je suis avec eumeu
vito boss vito boss no stressé
bilahi euma borom bakh la
drttyu liqm
drttyu liqm 10 giorni fa
yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala
El Che
El Che 10 giorni fa
Lac 2 moy enfoiré rek . Yaw kenn du yaw jambar deug ga
Mamadou Alpha Bah
Mamadou Alpha Bah 10 giorni fa
Je suis un fan de Modou Lo mais je t'aime💕💕❤❤😍
Marieme Balde
Marieme Balde 10 giorni fa
Mais eumeu nak balla dinala dane dh one bakhga trop beugue nagne la mais dinagne la dane dh 😂😂😂
drttyu liqm
drttyu liqm 10 giorni fa
lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak
Marieme Balde
Marieme Balde 10 giorni fa
Sana xol diekhna si lac thiim. Bravo eumeu courage. Balla ak wa keureum gnoy samay mbeur (sauf Lac maintenant) legui iow yako remplace. Borom vakh nga
Aita Ndiaye
Aita Ndiaye 10 giorni fa
Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss
Ndeyemarie Seye
Ndeyemarie Seye 10 giorni fa
Diamou RK ngayi âme bly
BUZZ MIFA
BUZZ MIFA 10 giorni fa
EUMEU BOUL BAY AWMA KÉNE COUEOUL YEW
Khady Togola
Khady Togola 10 giorni fa
Eumeu ya meuna doull lac dakeu leu bangua guéneu sakou yi guay féne Amgua mélokane déh khawma wone ni ningua mel féne bakhoul
BUZZ MIFA
BUZZ MIFA 10 giorni fa
EUMEU JE T'AIME BILLAHI
Issakha Ndiaye
Issakha Ndiaye 10 giorni fa
Tu fais partie des meilleurs.
Aboubacry Sarr
Aboubacry Sarr 10 giorni fa
Ya fi meun dh Eumeu billahi ❤️
Chekh tidiane Thiam
Chekh tidiane Thiam 10 giorni fa
C'est vrai je suis avec eumeu
Mbacké Seck
Mbacké Seck 10 giorni fa
Lou lérr laa wakh
Modou Mbaye
Modou Mbaye 10 giorni fa
Eum bénéne yonne boy bré boul nuyoti kénn lokho.bâ nga nuyo thi lamb dji la khamni da ngay d'Abou.
Abdou Mbaye
Abdou Mbaye 10 giorni fa
Eumeu sa kanam
khass Killah
khass Killah 10 giorni fa
Boléne waxé té yalla tax ngéne xamni lac2 mo tané si combat bi ndax mom sax défna touti effort eumeu sax wax nako après combat bi "waroléne ma wonn téyélo sama bop" motax dafa taxaw rék défoul dara. Questioné nagn ko mo bo xolé boubax dafay rafétal di rectifié wax bi coz ay staff faw gnoniko bouko wax parck lolou daf léni yaxal mbeur gnou fayla ay millions sa staff nane la téyél sa bop
Penda Wade
Penda Wade 10 giorni fa
Yaw diabargua bilay
Khady Gueye
Khady Gueye 10 giorni fa
lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak
Khady Gueye
Khady Gueye 10 giorni fa
billay diabare gua
Mame Saye Sylla
Mame Saye Sylla 10 giorni fa
Bilahi eumeu sene wakhone na lako si beineu commentaire nila lac de guiers 2 dalayy tardel rek khamoul gatt ragale na bilahi wokhone na lako beurei woule bayi woule dafa ragalll tropp tropp
Abu Konate
Abu Konate 10 giorni fa
Eumeu lat 2 amoul diome
Ibrahima Khaliloula Hounsah
Eumeu Nguaïdé Nguay Meussa Done Bo Bayé Beuré Sax Nguaïdé Ngua
Diogop Ka
Diogop Ka 10 giorni fa
Machalla fiér de toi champion 💪💪💪sa kaw sa kaname
Ibrahima Diop
Ibrahima Diop 10 giorni fa
💪💪💪👍👍
Khadidiatou Gueye
Khadidiatou Gueye 10 giorni fa
Barki yamlah Eumeu damala beug
Seyidina Sow
Seyidina Sow 10 giorni fa
Eumeu champion nga lou lérr Lac war nga kholaat sa beuré té di dieul décision, am nga katane loy ragal, khamon sakh biss bo mome warko am ndam,... modou lo ndam rék Incha ALLA
Sila Dame
Sila Dame 10 giorni fa
Q
Sall Ablaye
Sall Ablaye 10 giorni fa
Khole bou rafet eumeu
Mansour Gueye
Mansour Gueye 10 giorni fa
Mberr yaw diaroul sakh ngay nioue khana nonou yaye Kane mberr pure nga
Isatou Jobarteh
Isatou Jobarteh 10 giorni fa
Eumeu sene yow ya Barry wakh barry tapaleh
Fati Sow
Fati Sow 10 giorni fa
waw kay eumeu diadieuff way on te fais confiance
Adama Fall
Adama Fall 10 giorni fa
Champion nga
Mariama Diéne
Mariama Diéne 10 giorni fa
💪💪😇😇😇😍😍😍👍
ASTOULO KOBAR
ASTOULO KOBAR 10 giorni fa
Eumeu yawdal gathia ngalama chapeau a vous mbeur kaamil NGA
Pape Davido
Pape Davido 10 giorni fa
Cœur pour diambar jdi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Tijani Dia
Tijani Dia 10 giorni fa
Waw kay sama mbeur bi amal diame yaw lanou beugue tay ak soube mala beugue rek té yallah takh soy beuré douma ame diame wallahi taye wnibik hateu
Pape Davido
Pape Davido 10 giorni fa
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Ahmada Dial
Ahmada Dial 10 giorni fa
Iow tamit beure wo ...wakh ko kéne meunou niou nakh
Adama Camara
Adama Camara 10 giorni fa
Eumeu séne diambar gue nion gui sa gui naw
Gooo Bhff
Gooo Bhff 10 giorni fa
Eumeu ❤️❤️❤️❤️💪
Gooo Bhff
Gooo Bhff 10 giorni fa
@gtoss chddy lac mo bougone Revanche
gtoss chddy
gtoss chddy 10 giorni fa
Vous avez tout les deux déçu
Mariama Aliou Diouf
Mariama Aliou Diouf 10 giorni fa
Fier de vous Eume Sene
Serigne saliou Lo
Serigne saliou Lo 10 giorni fa
Waw lac nonou ladone def mé khamnanou touti si lamb
gtoss chddy
gtoss chddy 10 giorni fa
Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss
ibrahima ndom
ibrahima ndom 10 giorni fa
Eumeu mi da melni da beug beuré wate AK Balla
Il prossimo
I MOVED | Meme Time
24:52
visualizzazioni 2 288 279
illegal minecraft rooms
1:11
visualizzazioni 2 336 084
Conferenza stampa del Presidente Draghi
54:59
Emanuele Aloia - Mi stai già perdendo
3:01
Prince Philip's funeral: the key moments
6:16