Buio

TIEY TABASKI EPISODE 3

Okay.africa
Iscriviti
visualizzazioni 252 907
93% 2 623 194

Retrouvez - nous sur www.okay.africa ou télécharger l'application sur :
- Playstore: play.google.com/store/apps/de...
Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
- Abonnez - vous ici : itvid.net/u-ok...
- L'intégral de la solution "Jixi Jaxa" : itvid.net/video/video-jKEFDDpZ-YY.html&list=PL_HZbZROSvxYzEw5aX4hO-qx3F95M2Ut8
- L'intégrale de la série "Wiri Wiri" : itvid.net/video/video-ClixRV90d8M.html&list=PL_HZbZROSvxZqe3KE_Y7uyN9vJRWGlvrP
- L'intégral de la série "Mbettel": itvid.net/video/video-iaX29BqYa_k.html&list=PL_HZbZROSvxbDDFtr8oJVTjrkXvt9fJ6c
Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :
- Instagram : instagram.com/okay.africa
- Snapchat : snapchat.com/okay.africa
- Facebook: facebook.com/okay.africa.tv/
www.okay.africa est votre catalogue digital du Sénégal. Webséries, théâtre sénégalais, sketch.

Intrattenimento

Pubblicato il

 

9 ago 2018

divertissementsenegalsoleil levantmbettelwiri wirimusiqueriresportwadioubakhpaniceteaser

Condividi:

Condividi:

Scaricare:

Caricamento in corso.....

Aggiungi a:

La mia playlist
Guarda più tardi
Commenti 355
Lat Gaye
Lat Gaye Giorno fa
Diop fall moye kenn dh
Arfang Kebe
Arfang Kebe Giorno fa
Tabaski mo mèti
Aby Ndour
Aby Ndour 3 giorni fa
Kombe okin respect si fat kine😂😂
Ablaye Petit Mbaye
Ablaye Petit Mbaye 4 giorni fa
ndeysan diop fall febar bi dako yaar kw kxkxkx wèreul ak djam lartist
Bayemorseye Seye
Bayemorseye Seye 4 giorni fa
demal tok
queen'cess Camara
queen'cess Camara 5 giorni fa
Deureum yaye aka yagg 😂😂😂😂😂😂
queen'cess Camara
queen'cess Camara 5 giorni fa
Riguou lene nii 😂😂😂😂😂😂
Houleye Ndiaye
Houleye Ndiaye 5 giorni fa
Diop fall a besoin d'un aide financier selon ma déduction du scnerio entre lui et dérem. Que DIEU l'assiste 👌
Ndeye Sakho
Ndeye Sakho 5 giorni fa
fatou kine jtm wy
Saliou Toure
Saliou Toure 5 giorni fa
Diop Fal yalla na la yalla may diam barkép Serigne Saliou
mandiaye ndiaye
mandiaye ndiaye 5 giorni fa
yénafi nék
Aminata Faye
Aminata Faye 6 giorni fa
Diop fall way Ana gni ko namone 😂😂
Fatou Diop
Fatou Diop 6 giorni fa
Sama khol féssna.Diop jm te revoir en forme bilay.
Kev Kess
Kev Kess 6 giorni fa
Je comprends pas la langue lol
Ndao Mor Daro
Ndao Mor Daro 6 giorni fa
No manioukh Ken la
Mamadou Lamine Cisse
Tabaski moudiei naa metti
joe bara
joe bara 6 giorni fa
nooooooon fatou kiné elle est tres belle
Ndeye Dieng
Ndeye Dieng 7 giorni fa
Nena "renard" lol 😂
Amina Ndiaye
Amina Ndiaye 7 giorni fa
Manioukkk dinama raye 😀😀😀
Dorina Gomis
Dorina Gomis 7 giorni fa
Eyway Ndeye Ndiay mongui yakk tein noir bi way...pourquoi xéssal tamit, yalla na yalla deff xéwal way thi sougnù pàpà yii,gneup am xàrr tabaski si djama inchalla
nadia la belle
nadia la belle 7 giorni fa
Ma niouk Néna niague ak dereum yaye tissu yoyou longtemps na😂
Prince Cogito
Prince Cogito 7 giorni fa
Ohh Diop Fall Namanako deh😉❤
daba dida dia
daba dida dia 7 giorni fa
yala nagnu yala samou defal gnu sutura ak wér ak khèweull tabaski bi borom keur yèpou am xar tè bagna am fitt neu
Ndeye Mbissine
Ndeye Mbissine 7 giorni fa
wiri wiri
Elhadji tidiane Aw
Elhadji tidiane Aw 7 giorni fa
Ndeye ndiaye pourquoi depigmenter nak ish Yakh nga sa bopp way
Sokhna Khole
Sokhna Khole 7 giorni fa
Barki serigne falilou deureum damay fathie🤣🤣🤣🤣
delfa Bi
delfa Bi 7 giorni fa
Yénafi meune mako wakh
Pape Diouf
Pape Diouf 7 giorni fa
Kou begue diop fall besel jém
thimbo thierno idrissa
Wa mais ana épisode 4 bi sone naniou
Bayougo Sall
Bayougo Sall 7 giorni fa
mandé aw beuy sakh amagoumako waxagouma xarr
tislim dione
tislim dione 7 giorni fa
Ahh namone Diop fall
Mbaye Faye
Mbaye Faye 8 giorni fa
non Diop fall namnala trop
Lamin Fadera
Lamin Fadera 8 giorni fa
Fatou kine akh saina nio farr
Die Mbodj
Die Mbodj 8 giorni fa
Vieux mako beug rek
Niang Modou
Niang Modou 8 giorni fa
Mais ndakh khangéni Ndeye Ndiaye dafa noss walla loukhéw
Mamadou Diop
Mamadou Diop 8 giorni fa
Fatou kiné machalla avec sa tin naturel
Ndeye Diakhate
Ndeye Diakhate 8 giorni fa
Bilay latyr wax ko thia kaw.niarel yii dou niiou dem!
safandou Safandou
safandou Safandou 8 giorni fa
Bilay Diop fall deug piir nga wakh😊☺
Ndari Ba
Ndari Ba 8 giorni fa
Diop fall mo meuna woyan
Ndira Ndir
Ndira Ndir 8 giorni fa
Tabask rek
Yoro Fall
Yoro Fall 8 giorni fa
Mn momm magnoukh sm your yi lay diakha sè
YÉÉWOULÉN TV BANLIEUE
Fat kine nékh nama
Abdinho Fall Fallene Bi
Fatou kiné 😍
Oumy Lo
Oumy Lo 8 giorni fa
Fatou kine da ame diekeur
Adama paris
Adama paris 8 giorni fa
Sketch bi nekhneu waye, mais Afrimarket 110mil mouton ak 10kilos soblé bahna deih mashallah gspr khar you ame takhawaye la rek
anta lo mou serigne saliou mbacke
Ho sama diop fall waye ❤ yalna yalla guena yokou tawfekh amine
Mallé Sylla
Mallé Sylla 8 giorni fa
Loutakh maniouk reww
kebe pari mana
kebe pari mana 8 giorni fa
Ana ñi name Diop fall way
Fatou Diouf
Fatou Diouf 8 giorni fa
machalla diop Fall
Tapha Diouf100
Tapha Diouf100 8 giorni fa
Fate kiné sa tein noir bakh na
Maguette Kébè
Maguette Kébè 8 giorni fa
Machalla Diop fall
Awa Babacar Wane At-Tidjany
Maniouk,Kombé ak Vieux momeu gueneu ñu 🤦🏽‍♀️diñu terrorisé Wayè Deureum sa cas grawna mouton wala dara🤣🤣
Maguette dabo
Maguette dabo 8 giorni fa
Enfin Diop Fall est de retour ! Mais kombé dinama raay rek 😂😂😂
Dame Cisse
Dame Cisse 8 giorni fa
oh diadia plainte takhawna
Danso Ba
Danso Ba 8 giorni fa
Team kiné je t aime beaucoup 🍠
Yacine Bakhoum
Yacine Bakhoum 8 giorni fa
tram fat kine
Baba Fall
Baba Fall 8 giorni fa
Kou aimé sama commentaires yalla n'a la may lo beug ci sa adouna 🙏
Saliou Toure
Saliou Toure 5 giorni fa
👍
Akim Diakhate
Akim Diakhate 7 giorni fa
amine
TAF TAF 10
TAF TAF 10 8 giorni fa
diop fall
B N G TV 221
B N G TV 221 8 giorni fa
Diop Fall way
Mohamed Diop
Mohamed Diop 8 giorni fa
#Diopfall yalla na yalla yokk la werr barkei seydina mouhammed
Fatousha Diagne
Fatousha Diagne 8 giorni fa
Oooooh finalement Diop Fall namon nagn la 😍😍
khadija salih
khadija salih 8 giorni fa
wooooooooooooooooooooooooooooooooooyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyy
MADRISTA MBOW
MADRISTA MBOW 8 giorni fa
Madioukh est meilleur que AYA NAKAMURA
Princess mbay
Princess mbay 8 giorni fa
Deureum comme kou amé loss
Denis boy kl
Denis boy kl 8 giorni fa
Haha bilay Mane dina dh 😂 Yalla nagnou Tabaski si djamou 🙏🙏
Mara Diaw
Mara Diaw 23 ore fa
amine
L'homme du Coeur
L'homme du Coeur 8 giorni fa
Billahi ndaye Nidaye ya reuy bopou rk
Alzo Afri Cana yenguelin
😂😂
Thiane Gaye
Thiane Gaye 8 giorni fa
Noo deei na manioukh neina fi niaague aye bobou tisdu foumou amati😀😀😀
Ahmadou Dieng
Ahmadou Dieng 8 giorni fa
Mangnioukh
Ali Toure
Ali Toure 8 giorni fa
Ana team combe yalla na niou kou féké ak diamou ta tale kou 😂😂😂
mousta n9 diop
mousta n9 diop 8 giorni fa
Diop fall
Astou Ndiaye
Astou Ndiaye 8 giorni fa
Ani wa association ande setan série yeup je vous Salut🙏🙏🙏🙏🙏🙏👋👋👋👋👋👋👋👋👋👋👋
talla aminata
talla aminata Giorno fa
Astou Ndiaye N (:
Shasha Kah
Shasha Kah 8 giorni fa
Mdrrrrr Kombe kay wouyou say 2renards yiii manioukh demayyy fathie
Tabarra Bakh Tall
Tabarra Bakh Tall 8 giorni fa
#FatouKiné bilaye ya tarou masha' allah da nga ma nékh ba fou nékh yam!
MACKA BRAGUEYE FAMILIE
Diop Fall yall nala souniou boroom sammou aar là défall là fann wou gouddou akk wérr gui yaram
Ndeya Fatou Ba
Ndeya Fatou Ba 8 giorni fa
Diop fall namennako yala gua ame diam
Ndeya Fatou Ba
Ndeya Fatou Ba 8 giorni fa
ndiaye la puissance zeyna nio far niou bocouko
ndiaye la puissance zeyna
Ndeya Fatou Ba aminnnn
Thérèse MENDY
Thérèse MENDY 8 giorni fa
Liii moy diabare weuhh rew bâ doff
Maman karre
Maman karre 8 giorni fa
Woooooy😂......... Diop fall m’a tué néna france pour ngua ame 2€ sakh probléme la billaaye aka wakh deugeu deuk bii aka metti té waa galsen ils n’ont rien compris.
Kana Kana
Kana Kana 8 giorni fa
wlh c vrais
Toure Aboumahmoud
Toure Aboumahmoud 8 giorni fa
tu es super fatou kinne
TOTALLY FAMILY RAMA
Kumay sarakh ay aimer yu pata abonner a notre chaine cest amusant
senegalaise Mbodji
senegalaise Mbodji 8 giorni fa
Wax degeu maniouk palman beuthieuk tangor bi😂😂😂😂 Ah ndeye ndiaye tay amnagn la kxkxkx
MATH-LIPZ Deme
MATH-LIPZ Deme 8 giorni fa
Cuisiniere ak guimaar combe am ngua problème dingua niorr khombou dooto dèèsèti dara tissu yèè nata diekh rek
Fa dudu Lô
Fa dudu Lô 8 giorni fa
Tay si aya nakamura lah😂😂😂😂
Moréén TV
Moréén TV 8 giorni fa
les 3 la dougn dem😂(manioukh kombe vieux ) ak 2pa yi😂.hei diop fall nieuwatina😂
maodo diagne
maodo diagne 8 giorni fa
Neexna waay Ana fans job fall yi
Serign Mbacke Loume
Dimanche Premier Match LIVERPOOL Premier League contour West Ham Anfield
Toure Daour
Toure Daour 8 giorni fa
Merci pour l'information
Papa Amadou Mbow
Papa Amadou Mbow 8 giorni fa
kombe mbarane nañoula teh yeguoko😂😂😂😂
Kamal 313 Soxar Xalima ndiaay
Barké serigne salihou mbacké kombé ak madiokh gnongui maay yeubu yawmal khiyamati bilahi gnii gnon con qw😂😂
Moussa Sarr
Moussa Sarr 8 giorni fa
je t'adore fat kine
Ndour Davido
Ndour Davido 8 giorni fa
o guiss na Diop fall tey way
Ndour Davido
Ndour Davido 8 giorni fa
Mane Dex Diop fall la namou
Abdoulaye dieng
Abdoulaye dieng 9 giorni fa
Sa niarri renard yii😂😂😂
ÔůŻę Président
Qualité son Bi c’est à revoir svp
Faramarene snap Wally B seck
Yalla na diamou yague Sénégal ❤ Abonnez-vous à ma chaîne ITvid svp
PAPINO
PAPINO 9 giorni fa
Fatou kine❤
Bass Gueye
Bass Gueye 9 giorni fa
no combé ray nama ya meneu feinne kay
Barane sylla
Barane sylla 9 giorni fa
Kousa xoll nékh 👍
Papy Gueye
Papy Gueye 9 giorni fa
Mane dall fate kinné mako beugue pur billay
TKB Tv
TKB Tv 9 giorni fa
Yama mana fen😂😂😂 nn kombé
devenir pro
devenir pro 9 giorni fa
Tabaski diamb pour niepp amiine
Prossimi video
BA Belle Mère
26 giorni fa
B.A TIEY TABASKI
12 giorni fa