Buio

Urgent : Eumeu Sène vs Lac 2 Signature bou tangue dieur

Lutte TV
Iscriviti
visualizzazioni 99 806
95% 951 47

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct facebook.com/luttetv/
facebook.com/luttetv/
instagram.com/luttetv/
luttetv.com/
itvid.net/u-senlamb

Sport

Pubblicato il

 

23 ott 2020

Condividi:

Condividi:

Scaricare:

Caricamento in corso.....

Aggiungi a:

La mia playlist
Guarda più tardi
Commenti 100
Ameth Kadioh
Ameth Kadioh 25 giorni fa
Lac de guerre 2 yallah Nala yallah may ndam incha allah rabi
TK
TK 28 giorni fa
Eumeu Sene Yalna am ndam InchAllah. Yalna daàn lac 2. Victoire bou sètt té lerr
Cheikh Niang
Cheikh Niang 28 giorni fa
mane lac de guierre envis niousss ko rk la am jtj🤣🤣🤣🤣 Day wax ba nganii taymou rayy wadji Jr combat mou melni Moumeu ish
Koffi Mendy
Koffi Mendy 29 giorni fa
Bonne chance LAC2
Mamadounar Bakhoum
Mamadounar Bakhoum 29 giorni fa
Yalnala yalla may ndam yaw Eumeu sène si barké seydina Mouhamade
Idrissa Thiam
Idrissa Thiam 29 giorni fa
Vamos eumeu ❤️✌️
Tidjiania
Tidjiania Mese fa
Té guéna utiliser séne dolé biléne YALLA méye guéne défar réwmi ...si diné dji , thi hamham bi , thi toll yi ... té bagna har état .... té bayi fo bi , hatim yi , liguéyéne té bi ...adouna dou fo rek so néké halé ... diamouyalla rek di def ahe dicklé lou bahe ... ame YALLA , ame Yonaneté bi , amen wadiour yi , ame mbockyi , ame serigne bi ...dé tabi adiana INCHALLAH ... c tres simple .....assalaaama
Michel Diouf
Michel Diouf Mese fa
Kane moy Eumeu moy kiniou dorone mou dayou ?
Diao Abdou
Diao Abdou Mese fa
Combat Lac mom sawarou massi trop parceque day daw reik et il ne prend aucune initiative
Ousmane Dia
Ousmane Dia Mese fa
Lac c est un lâche. eumeu C est un guerrier tout le monde le sait
Mamadou Faye
Mamadou Faye Mese fa
L’opium du peuple sénégalais
Thierno Diop
Thierno Diop Mese fa
Wah kouy toussé nonou çi salle khana da corona
Abass Fall
Abass Fall Mese fa
Eume khana yegoul tangor bi🤣
Lamine Konate
Bonne chance à lac
Thierno Niang
Limaye lathe moye eumeu dane lac foumou koye yobe .lac dou ambiance dou indi siporter dou beure , comba lac mome yakam tiwoumako niak na diome trope
Behrami Thiam
Lac 2 guerre noyoulma wa technopole😂😂😂
Abdou Karim Seck
Beure beurewat ba kagne diel len boyi ha
Ibrahima Nging
Eum yalanaco yala may ndam thi barcké borom khelcom
Talibe Bamba
Talibe Bamba Mese fa
Modou anta yalla nako yalla may ndam inchallah
Lili Boy
Lili Boy Mese fa
Votre son tmt
Ibra Diop
Ibra Diop Mese fa
Thiey lac
Baila Diop
Baila Diop Mese fa
Eumeu mom xana yeugoul tanguay bi aam si deukk bi
Mbaye mbaye
Mbaye mbaye Mese fa
Lac bou wakhé guanii koumu diape gua D té geumousii dara
Diop Modou
Diop Modou Mese fa
Lac bou wakhei rek ngani tay mou rayko😂😂
Ndao Alfred
Ndao Alfred Mese fa
Lac2 wakhati gua d🤣🤣🤣🤣🤣do pouss do pass Putin
adji khady thiam
Eumeu je suis fan de Modou Lo mais Yallah nala Yallah may ndam si Barké Seydina Mouhamad
Lix Man
Lix Man Mese fa
Yal nala yalla may ndam diene kaïre🤷🤷 Yako mane fouf 🤷🤷🤞
mamadou mamadou
6:56 le regard de eume😂😂👊
Amade Diawara
Eumeu lac Dou beurre Diapoukou kadane kotapétela
Cheikh Diop
Cheikh Diop Mese fa
lac2 vraiment da nda soff wakh rek nga meune, tapet nga sa combat dou nexx. tu ne merites mm pas 5francs
pape gueye
pape gueye Mese fa
Félicitations à Gaston et du courage ❤️🙏
Aladji Sete Drame
Lac wakh rek ak rassou
Tin Taffa
Tin Taffa Mese fa
Loufayekheweumeumokoyedefeumeulidescarrierebiyallanadoneayendam
Lemzo Canzo
Lemzo Canzo Mese fa
Diene kaire amnga combat nk billahi modou anta ndanan la mai louy nekh way
seydina alioune borom jasiji
Cey Lac Niangale 2
SAMbou Barra
SAMbou Barra Mese fa
Ameen allahuma ameen
SAMbou Barra
SAMbou Barra Mese fa
Lac 2 we all are praying to you almighty Allah gift you Victoria
Dame Niang
Dame Niang Mese fa
Lac de guere moma sof borom combat you nekhoul yi baparé bari wakh
Binette Fall
Binette Fall Mese fa
Lima metti deugue moy lac de guerre daffa momé wakh dji yeup eumeu tjrs égale à toi mm je suis fans de modou lô mais eumeu yalla nala yalla may ndam inchalla
Ndoye lèbou
Ndoye lèbou Mese fa
Enem yalla nala Yaye mayatte ndame bou sedou gouye bilah
Omzo Bou Garga
Lac 2 sou wakhe rek nga ne Tay mou ray koumouy beurel te dou def dara wakh rek
Mamadou Dabakh
Gni wax si lac hamouniou koo dagnii téreureurii rek dii wax
Mamadou Dabakh
Ndakh mbeur yi dagne koo mine
Mamadou Dabakh
Lac dé kouko bagne ya ham dakh mbeur gueunouko amoul kouko daan dieul bou leer
Pape Mahawa Diouf
Saway lac2 sou mbeur yeup defeni môme lamb yakou menoul Bakou menoul beurré d'où animé stade lac 2=0 thiouné la
Aba Sall
Aba Sall Mese fa
Vraiment lac dosama mbeur mei serigne babacar sy malick taxna ma sopla ndax ku begue serigne babacar sy malick begue nala gor gorlul nak
Aba Sall
Aba Sall Mese fa
Assssmmmmiiiiinnne eume ndam rk
gnrl Ng
gnrl Ng Mese fa
Diéne kaïré le futur champion de la lutte sénégalaise
dame mbengue
dame mbengue Mese fa
Lac deux Yalla nako yalla maye Ndam
aliou sarr
aliou sarr Mese fa
Bayiléne khél si Diéne Diouf c'est un future roi
Nature Humaine
Lac wax ji mo eup jeuf ji. Kou deef ni moom doula daan. A part KO ou plaquage amoul leneen ci Eumeu Sene. ////// Modou Anta vs Diene Kairè. Diene Kairè mo ngi sogga aam combat. Té na deef attention bou bakh sakh. Modou Anta niakal beuré, niakoul dolé té aam na saysay ci beuré. Dina ma bett Diene Kairè daan ko sou jaam rekk dé xew. //// Pronostic : Victoire Modou Anta Nul problabe ou victoire par avertissement entre Lac et Eumeu.
Fallou Diagne
Ki dama ragual eumeu door ko door you metti
Pape Faye
Pape Faye Mese fa
Wowal yalla soce dou yalla ko yakar yalla la yakar
Dranco Sakhanokho
Eumeu Sene rek
Khalifa Ndiaye
Lac na bayi rassou té beure kon mou khamni lep deugeuleu
Marly Diallo
Marly Diallo Mese fa
Le son???
Original PassyDott
Lac bul rassou nak nyak jom nga dèf Père Gaston dal ndananla merci beaucoup yalla gudal sa fan ameen🙏🙏
Prince Vita
Prince Vita Mese fa
Lac 2 ak Modou Anta yalnala yalla may ndam si barké Seuydina Mouhamed
Fofana beugue FALLOU
Eumeu sene yalla nanko Yalla may ndam amiine 💯💯pikine 🤲🤲
Maissa Sall
Maissa Sall Mese fa
Lac2 rk dname rek inchallah 💯💪
Sekma de vels
VOS MICROS 🎤🎤🎤 ala Con ne servent à Rien ; il n'y a qu'au Sénégal où on garde tjrs autant de Micros et le son est encore Pire
Accro Galsen 2h
Vraiment 😂😂😂
AZBDOU
AZBDOU Mese fa
Eumeu nafékh la
Ndiaye Mansour
Dién Diouf yalah nako yalah maye ndam
Ndiaye Mansour
Eumeu sén yalah nako yalah maye ndam
Mbacke Ndiaye
EUMEU rk
AMADOU KANE
AMADOU KANE Mese fa
Yene nieupa nul ni lamb lac 2 guier 😂 DIP ...Aytia eumeu amoul mayé dara
Modou Ndiaye
Modou Ndiaye Mese fa
lac dinako def lou bonne
ibrahima conte
Yékini junior vs Moussa Ndoye
Moustapha Samb
Yekiny jr vs gris
Babacar Ba
Babacar Ba Mese fa
Les masques sont enlevées 😂
Goumba Faty
Goumba Faty Mese fa
Li dou comba way
dame vilane
dame vilane Mese fa
Lac2 monument de la Renaissance laa dou xeikh dou beuré dayyy xarr reikk bou toussé dou nexx sou beuré nga beugeu wathiou nulard laaa
Saifour Diop
Saifour Diop Mese fa
lac wakhal rek té géné si seringe babacar plaese
Bora Bora
Bora Bora Mese fa
Eumeu ndam rek Insaa Allah..
kane mamadou
kane mamadou Mese fa
Eumeu 4 life yalna yalla may ndam si barké seyidouna Mouhamed psl
Modou Gueye
Modou Gueye Mese fa
Lac 2 moytoul eume contr mod lo dafka tognone nakh niko balla 2 dane iow ossi gua niow diko togn si mod lo limko def damay ragal gua def louko raw nakh lamb dafa doywar
Khayyeyeh Khayeye
Bii yonn nak Emeu guire yalla démal France gua préparé comba comme combat gris Bordeaux 🙏🙏🙏
Ismael Faye
Ismael Faye Mese fa
Lac wah rec gaye def tapete bou mague ga
mbokoum gnep diop
En tt cas lac2 yap nga SERIGNE BABACAR SY dh 123 Ngané Barké SERIGNE BABACAR SY Té féne rek ngay def
Manta Diop
Manta Diop Mese fa
Lac2 ndame rek inchallah
Dame Sarr
Dame Sarr Mese fa
Gaston soof nga té gniak class khamo wakhin
Ousseynou Nd
Ousseynou Nd Mese fa
Portez des masques...
Samba Gaye
Samba Gaye Mese fa
Comba lak la
Alpha Faye
Alpha Faye Mese fa
Eum n’est pas intelligent tu gagnes rien dans ce combat tu devais prendre balla non seulement tu vas gagner bcp plus en terme de notoriété et d’argent comme ça tu prépareras bien ta retraite même souka balla dané comme ça tu va finir avec lac 2
Gueye Xalile
Gueye Xalile Mese fa
Lac dagua yéép S Babacar sy chaque Combat gua waat thie S Babacar sy a mon diom
Seydina Fall
Seydina Fall Mese fa
Lac sama mbeur gua wayé changél beuré wra ngua changé sistémou signature
Seydina Fall
Seydina Fall Mese fa
Diene tou medina et dernier toi
Seydina Fall
Seydina Fall Mese fa
Eumeu ndaysane liko minier biko modou dané moko diapeu bâ lgui nékatul koi
Mms seye
Mms seye Mese fa
Lac day wakh ba thiébam saff yapp mais dou ray dara
lamzo choco
lamzo choco Mese fa
Ya pl8 de Corona au Senegal😩😩😩😩
K R Musique K R Musique
Eumeu 👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼 champion de l'Afrique champion de Sénégal inchallah ça va aller mon frère
abdou rahim
abdou rahim Mese fa
Lac mom mystique rek koi mom foko fekk mingui mystique tchimm
Masseck Niang
No lac dima rayy
Aliw Njaay
Aliw Njaay Mese fa
il confond parler fort et crier
Mame Cheikh Fall
Eumeu Sen ndam rekh claro... Lac yaw aii daiii Mola Geune chim
KMbaye‘s
KMbaye‘s Mese fa
Neeneu bign koy dann toutt tankk leu 😂😂 Lac amal sougn complexe aussi 😂😂 mey wakh mouyy menacer😂 olalalala copain leglelllllllllll
Yoro Kanté
Yoro Kanté Mese fa
Sène son bii niewoul dèh🦻🦻🦻🦻🦻
Dieng Kalidou
Lac rek
Sheikh Jobe
Sheikh Jobe Mese fa
Lac yallna yall meyla dam je bark seydena Mohammed Sw amin
GorguiDieng Dieng
Lac na bagna bayi sama serigne boumouy watei si aye lamb rek En plus yaw foy diar eumeu si beuret boy niang rek meunoko attaquer di khoumbal fi
Alioune Fall
Alioune Fall Mese fa
Lac bayil wat jour lambj day daw ba combat bi diékh
Abdou aziz barra Nguirane
Eumeu sene yalla na ko yalla may ndam ci kaw lac 2 ci barke seydina mouhamed psl
Cheikh Bi
Cheikh Bi Mese fa
Gris Bordeaux le Grand perdant. C'est dommage.
Cheikh Bi
Cheikh Bi Mese fa
Lac 2 amnga gallathie dé. YALLA moola classé. Beuréle TÉ daane Eumeu. Yaako eupp doolé gueune ko nekk khalé
Prossimi video
Brewstew - Wrecking My First Car
5:25
visualizzazioni 940 041
eumeut sene lac de guiere
09:45
visualizzazioni 1 000 000
IBRA: BISOGNA STARE CALMI
9:51
visualizzazioni 26 665
25 NEXT LEVEL MOMENTS IN SPORTS
11:14
visualizzazioni 778 598