Buio

Youssou Ndour - Waññi Ko (version lyrics)

Youssou Ndour
Iscriviti
visualizzazioni 836 517
52% 19 000 17 000

Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos ,

te bés bu ne , benn xar nga daan añ e

nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée

yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine

am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann

nga neeti ñu , yaw yaa ko jat , ba mu nelaw ,

· nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée

te waa nations - unies , nga ka daan loué

· te diggënté , États-Unis ak Guinée ,

daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
am na benn bés , nga ni ma , my boy
keroog daje naak , roi des arènes. 2 fois.
ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations. 2 fois.
ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy. 2 fois

na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs

na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs

techniques yooyu , japon laa ko jànge

ca yooya jamono , man la ñépp di wër

lu ñu wax nga ni fekke nga ko

fu ñu wax nga ni dem nga fa

doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw ;

waaye sa ma waa jii , ken melut ni moom.



Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal ,

Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal.

Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al

Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al.

Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo. 2 fois.





ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla


Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
itvid.net/u-YoussouNdour...
facebook.com/youssoundour...
instagram.com/youssoundou...

Pubblicato il

 

19 lug 2021

Condividi:

Condividi:

Scaricare:

Caricamento in corso.....

Aggiungi a:

La mia playlist
Guarda più tardi
Commenti 0
MOUSSA BADIAGA
Youssou En guise de la déclaration de elhadji Ndiaye sur le vol et les tracasseries satellitaire et la plainte sur la montée frauduleuse Vôtre nouvel album ne fait révéler et confirmer le ral bol de Mr Ndiaye Youssou vous pourrez faire une déclaration sur vos antennes pour démentir les dits et les soupçons Et on saurait la vérité
Thiapa Thioly
Thiapa Thioly 3 ore fa
Na patin deff clip bi🤣🤣
Thiapa Thioly
Thiapa Thioly 3 ore fa
Youssou clip bi sokoye deff nagua diele patin mou deff ko 😂😂😂🙏
Pape seck Seck
🤣🤣🤣🤣🤣🤣😅
Thiapa Thioly
Thiapa Thioly 3 ore fa
Machallah 😂 idrissa wagniko
khouma Basirou
Cv
Loum Gallas
Loum Gallas 3 ore fa
Diadieuf kendou yaw machalla ❤️
Babacar Cisse
Babacar Cisse 3 ore fa
Vraiment il est le meilleur
syngari boundou
You moye wakh ragal Yalla mome ragal na yalla mome mi sathieu courant akh frèquancer di dadialè gor akh djiguène niouye fèthieu
Aliou Diouf
Aliou Diouf 4 ore fa
Je crois que ce morceau est plutôt pour MACKY SALL , qui s'est donné tous les pouvoirs du senegal par l'intermédiaire de sa majorité mécanique de l'Assemblée Nationale , le détournement massif des deniers publics, l'argent des contribuables ;et même cette chanson concerne Youssou N'Dour car il n'a peur rien sur terre , ragaloul Yallah, ragaloul yonentabi S.A.W.S. on peut se poignarder soit même.youssou bopam la wayal waybi..
Ibrahima Sylla
Youssou Mary sene The king
Mouhamed Dieng
Yousou waguiko
Sougou Jidaty Niang
oh sama khol dafa séde si ki yalla nangua guoudou fan
ndeye lobe sall
yaye sen baye
Adama Malick Dramé
The king ,li ma diakhale voix bii d'où changé jamais chapeau papa Youssou Ndour
makhou arène bi jeune rapportaeir lamb ji
Ndanane la youssou ndour
Samba Sour
Samba Sour 6 ore fa
Le meilleur
Fricaque Afrique
Ohhh ...
Ndeye Sylla
Ndeye Sylla 7 ore fa
ki Moy Michael Jackson fimo tolo thi Adouna komo nekh Ak komo nakhari wadja ngui ni
foopyu nooui
foopyu nooui 7 ore fa
Il paraît le tube préféré de la 2e femme de Ousmane sonko . Elle l'écoute en bloc.
pape souleymane sane
Moi je ne crois plus en vous tous comment tu peux nous donner des conseils alors que ta famille fait des miracle sur le trafic
bou kene merr
bou kene merr 4 ore fa
Et après
Assane Biaye
Assane Biaye 8 ore fa
You are the best younouss ndour ❤️❤️❤️💪👍
REEMO REEMO
REEMO REEMO 10 ore fa
Le roi 👑👑👑
Tons Ndiaye
Tons Ndiaye 11 ore fa
Vraiment Papeu Youssou sa son dina ma rayy mounouma sii doyal xawmalou takh
Fofana Samba
Fofana Samba 12 ore fa
Actuellement dou li lagne sokhla si yaw mes plus Sénégal problème yi niou neka macki akh wa keureum di djaye dollé Sénégalaise yi lolou moye sougnou blême
Mamoudou Diallo
Mamoudou Diallo 12 ore fa
et le chanson parle de quoi?
Awa Ngom
Awa Ngom 12 ore fa
Le meilleur chanteur du Sénégal 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Awa Ngom
Awa Ngom 12 ore fa
Le meilleur chanteur du Sénégal 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Senegal Senegal
Senegal Senegal 13 ore fa
J'attends le retour de mame goor diazaka après une longue pause musicale
MANSOUR BASSIROU BALDE
Magui lay guarouwalé,,, mai peut importe il est le meilleur
Moustapha Diallo
Toujours talant
Matar Diakhaté
Matar Diakhaté 13 ore fa
🥰🙏 ndanane
Raymond Diegane Ndong
you louniouy wagni
Ousmane Gérard Diop
Doo nitt mame🔥
Ya Awa
Ya Awa 15 ore fa
Daur Kat deug leu fi kénn nalaw toul xalaat TV fadiar lay yéeté
Ya Awa
Ya Awa 15 ore fa
@bou kene merr Sama khol Lou Kay nekhal dou diogué mouk thi ki wax Lou lér amoul garouwalé yeufou goor tigui
bou kene merr
bou kene merr 15 ore fa
Khanna sa khol nekhoul
babacar diop
babacar diop 15 ore fa
Wakgofffi darrra guaralatebi diRatouko
bou kene merr
bou kene merr 15 ore fa
Khanna danga tittt wala danga mer
The1st D
The1st D 15 ore fa
Gni dislikes video bi la youssou Di wakhal…wagni lene ko
Ibrahima Sylla
Ibrahima Sylla 16 ore fa
Le mensonge est une abomination Big up le roi du mbalakh
Dieye Darou
Dieye Darou 16 ore fa
Youssou N'dour national beug nala billahi
bou kene merr
bou kene merr 17 ore fa
Le tube préféré des pastefiens
Cine Plus
Cine Plus 17 ore fa
Ndannane nga billay wayè ñanalalal wally mom lafi yalla tek
Soda Mariame Boye
Machala ❤️
Saa-afrig Panafricain
Kii maky Sàll lay waxal. Comme Moor ndaje , Wàdd la ci doon wax. Cëy yuusu mooy bandi de
Maguette Cais
Maguette Cais 18 ore fa
Li dé nganda méséré moko mom😄😁😂
le musicien patriote
Va répondre à el hadji Ndiaye de la 2stv
bou kene merr
bou kene merr 17 ore fa
Youssou Ndour falewoul Ndiaye tampi. Youssou Ndour dou moromame
le musicien patriote
Demal fay say impôts
bou kene merr
bou kene merr 17 ore fa
Kimome Khanna sa khol nekhoul. Mba yauboul nguene adji sarr kharam
Ahm Mouss
Ahm Mouss 18 ore fa
Yeuw niak ngua fayda trope🥴🥴
KAMA Djalo
KAMA Djalo 19 ore fa
il parle de qui ???????????????? 🤔😏
Papa Abdoulaye Amar Diagne
Roi bi 💢💥💯🥇✍🏾
Abou ka
Abou ka 19 ore fa
Je t'aime
100k abonné sans vidéo
Ragal yalla way ragal yalla way
coline wade
coline wade 19 ore fa
C'est le même bit que "KADOU" de Youssou! L' une des meilleures de You
Ngagne Niang
Ngagne Niang 19 ore fa
Le grand YOU💪
DG Touba
DG Touba 19 ore fa
Le king c Wally Ballago Seck 💞💞💞
Omar Mbaye
Omar Mbaye 19 ore fa
You super Musik
Baba LY
Baba LY 20 ore fa
Youssou N'Dour la Star planètaire
Al Housseynou Ba
La légende de la musique sénégalaise merci mon cher Youssou Ndour
TORODO TV N:1
TORODO TV N:1 20 ore fa
Yaw danga sokhor ma dieke am son bi publié ko nga supprimé ko sama compte ITvid
Saliou Thiaw
Saliou Thiaw 20 ore fa
Délosil sakhel té khamni adouna amoulsolo khaléyi sakh niougui délou guinaw dieum si yalla adouna dafay woré ci bamél rék lanouy moudié papa yousou mbaye diéye faye
Ousmane babouna Ndiaye
Les sénégalais sont fière de toi 👏❤️❤️❤️❤️
Ousmane babouna Ndiaye
Le rois du mbalax you♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Yacheikh Dioum
Yacheikh Dioum 21 ora fa
Dad ❤️🙏🏾 technicité bi cii woy bii comme si dafay rap nn je l’adore
Rbsd Film
Rbsd Film 21 ora fa
Youssou ndour c le seul artiste bo xamni moy guéné song borom xol❤ you bone yi kou nékk nane ki mane lay wakhal réseaux sociaux, naye, bouki et aujourd'hui waññiko vraiment ndanane ngua
ibrahima cisse adame
les grand you saï tanné yii gnolay djey rék danga wara diamou dji yalla bayel thiakhane yii ah
Ndeya awa Fall
Ndeya awa Fall 21 ora fa
Le meilleur
Borisson transport
The King of Mbalax in Africa…much love and respect from Uganda
Sukai Jobe
Sukai Jobe 22 ore fa
Ken Dou yow si mim rewww ndour!
diop adama
diop adama 22 ore fa
le roi du mbalakh
Sissao Touré
Sissao Touré 22 ore fa
Il est merveilleux
Massamba Gueye
Massamba Gueye 22 ore fa
Tu sera et serait le meilleur diam rék
Sonia Sow
Sonia Sow 22 ore fa
Le lion a rugi
Massamba Gueye
Massamba Gueye 22 ore fa
Le meilleur de tout les temps
Massamba Gueye
Massamba Gueye 22 ore fa
J’écoute cette chanson 15 fois par jour merci beaucoup encore le meilleur machalah
CEN PROD TV
CEN PROD TV 22 ore fa
🤩
SENZAPPING TV
SENZAPPING TV 22 ore fa
Le bit ohhh 🥰
SENZAPPING TV
SENZAPPING TV 22 ore fa
The musique ohh 🤩
joe ndiaye
joe ndiaye 22 ore fa
youssou ndour rek amoul lenen
Dakar Guédiawaye
Xawma koula xaeronn fii🤧lofi déef📺🇸🇳🥴ragalal yalla té di fay impôt ak bayi signalou dianbour yii 👍
bou kene merr
bou kene merr 22 ore fa
Khanna sa khol nekhoul
chding zuure
chding zuure 22 ore fa
ambassade. »
Djibril Diop
Djibril Diop 23 ore fa
Waye bi kousi guiss sa boppa ya kamome
DIAWARA
DIAWARA 23 ore fa
excellent !
chding zuure
chding zuure 22 ore fa
je sait pas quoi dire donc merci grand You
Aissatu Baldé
Aissatu Baldé 23 ore fa
😍😍😍
Paterne Frank
Paterne Frank 23 ore fa
YOUSSOU NDOUR chante en Paraboles kou ame nopp degue c le King des king inter musicale ❤❤❤❤❤👊👊👊👊👊👊👍
Khady Ba
Khady Ba Giorno fa
Machalla sama papa ❤️nékh na 👍
Djibril Diallo
Djibril Diallo Giorno fa
Tu es le meilleur machallah
thierno saidou balde
Waññi diarouko Boulko yokkou té boulko waññi constitution réglénako. Boulko yokkou té boulko waññi constitution réglénako. Constitution diaroul yookou té diaroul waññi Kouwendi lath madior massa Tiguedj loumou wahone gaañi. Ngaïdé gou dekké nèlaw Mounouta tiat moramam guir mou nelaw. Wathima danenala amoul fenn bayil sa mascarade artistique. Bouramas yi rek sauvé Sénégal guénéniou si état bou critique. Guinée dou exemple démocratie . Dikko dieul référence deug deug moy nostalgie. Yeureumandé yeurmandé yeurmandé ci jam j selmi. Yeureumandé yeurmandé yeurmandé ci OKNOS mou selmi. Yéék ci bateau diffa dem diarouko firdébi moy protocole Conakry Mbourou ak sow amna gloria nioukoy lath ngakoy soppi tiakiri. Ô bama africa di ndamo Sankara ak Mandela non Barak Obama. Japon bokonena ci ay clé am def kamikazes waral niou bombarder Nagasaki ak Hiroshima. Mor Ndadié woyna boppam ba paré diniou signaler djikoy leuk. Mor Ndadié roi le empereur le ndemb ak tey wayé warra nak soralé euleuk. Nga yobbou ko Mbeubeuss di wadial Reubeuss Yalla setal ko. Yerré imam bo doul sol nga diem koka solal té mom dou yaw ham ngako. Deukké doundé meed moy sa choix lolou la yobbé ci 300 kilos. Moom nak mou choisir doundé Halal wadial NEMMEKOU TOUR Pikine ba Kolda six kilos. Adouna dou course de vitesse gaw ni melax ni Bolt Usain. Nit niveau yenné Yalla mom di ndoggal, niatta minutes la jouer coupe d'Europe ki di Christian Eriksen ?
Tounkara Bangaly
Le message n'est pas passé sur l'oreille des sourds, nous t'invitons aussi nga ragal yallah, nguén bayi Allal mbolo binguén di fowé ta bayi xél yawmal xiyam.
Mor ndoye Diop
Mor ndoye Diop Giorno fa
Dieu déteste les voleurs et les hypocrites et Youssou Ndour est le pire des hypocrites. Il a perverti toute la jeunesse Sénégalaise. Qu'Allah nous préserve de ses manœuvres.
bou kene merr
bou kene merr 23 ore fa
Adji sarr amena dome bou goor
Mame Kaffo Oumar TOURE
Le parolier le sage le philosophe de la musique sénégalaise africaine mondiale papa youssou le docteur honoris causa car il le mérite. Il est toujours là pour le peuple sénégalais de par son engagement auprès des jeunes des femmes des couches vulnérables de la société. Il ne cesse de montrer le bon exemple à travers le travail l' amour de sa patrie. Idole de tous bravo👏
EMBALO 20 GUINEA-BISSAU
Sonko ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
bou kene merr
bou kene merr Giorno fa
Adji sarr amena kharou Tabaski
adama soumare
adama soumare Giorno fa
N’importe quoi un hypocrite de plus
adama soumare
adama soumare Giorno fa
😂 🖕🖕je m’en fou de lui et d’autre mais c’est hypocrite Sui na dieu pour c’est intérêt🖕🖕 si sa te fait mal c’est on affaire
bou kene merr
bou kene merr Giorno fa
Khanna danga ame loula bett
MAMADOU DIENG
MAMADOU DIENG Giorno fa
Mbeug Mbeug bi ci fin bi, 3:46_3:48😉
poulo bou titi Ba
Non ki dou nit
Ahmed Dia
Ahmed Dia Giorno fa
Wakho fi dara
bou kene merr
bou kene merr Giorno fa
Danga mer nanal ndokh bou sedd 5 litres
Dakar infos
Dakar infos Giorno fa
Bala nga kham nékhayou son bi nga tok melni kouy rester leçon Mane dh mangui diangue
Gadio mamadou
Gadio mamadou Giorno fa
je sait pas quoi dire donc merci grand You
Maty Ba
Maty Ba Giorno fa
Xana macki lay waxal
Mere Anna
Mere Anna Giorno fa
Machalla tonton youssou ndour👍👍👍👍👍❤❤💋💖💖💖🇬🇭🎉
Il prossimo
Wally B. Seck  -  Les hommes de l'ombre
4:12
EVIL iPhone IMPOSTER in Among Us
14:53
visualizzazioni 5 221 184
Road To Tokyo - Ep 03
14:08
visualizzazioni 259 374
"Ho paura del vaccino, chiedo rispetto"
2:23
Måneskin - Beggin' (Lyrics)
3:31
visualizzazioni 2 775 449
Alcott Zara Bershka
2:47
visualizzazioni 40 405
Race Highlights | 2021 British Grand Prix
7:02